Sylla Madridista en wolof

Sylla Madridista en wolof Halla Madrid đŸ€đŸ˜‡

Leer na li mooy liste joueur yi JosĂ© Mourinho woo ci match suba bi face Deportivo Alaves đŸ€Ferland Mendy ✅Rodrygo ❌ Rau...
27/11/2026

Leer na li mooy liste joueur yi JosĂ© Mourinho woo ci match suba bi face Deportivo Alaves đŸ€

Ferland Mendy ✅
Rodrygo ❌
Raul Asencio ❌
Arnold ❌
Halla Madrid đŸ€

🚹 leer na : Birahim Diaz yokku na contrat wam ak RĂ©al Madrid ba 2031đŸ˜‡đŸ€
27/11/2026

🚹 leer na : Birahim Diaz yokku na contrat wam ak RĂ©al Madrid ba 2031đŸ˜‡đŸ€

Gary Neville 🗣 " Amna yaakaar ni Haaland dina dem RĂ©al Madrid ci diir bu weesuwul 18 mois wala mĂ«n na am bu saison bi je...
27/11/2026

Gary Neville 🗣 " Amna yaakaar ni Haaland dina dem RĂ©al Madrid ci diir bu weesuwul 18 mois wala mĂ«n na am bu saison bi jexe

Gisnaa Vini jr quitte Réal Madrid Mbappé di joue cÎte Gauche Haaland joue 9

F. Perez migui signe joueurs yi gëna baax ci àdduna bi te yaakaar ni Haaland di nekk joueurs bu Real Madrid ci lu yaggul dara

🚹 Nico Paz bĂ«ggul woon dellusi ci Real Madrid ci jamono jii âšȘ❌Sudee Real Madrid garanti luko temps de jeu bu doy Su Rea...
27/11/2026

🚹 Nico Paz bĂ«ggul woon dellusi ci Real Madrid ci jamono jii âšȘ❌

Sudee Real Madrid garanti luko temps de jeu bu doy

Su Real Madrid jëlee dogal ni duko jëndat Como dina mëna waxtaan ak yeneen club ngir ñu jënd ko

Manchester United itam mingi xool nu moy def ba signe ko sudee Bruno Fernandes dafa dem

11 yi gĂ«na xarañ ci League des champions ayu-bis bi 😇Kylian MbappĂ© ✅Jude Bellingham ✅
27/11/2026

11 yi gĂ«na xarañ ci League des champions ayu-bis bi 😇

Kylian MbappĂ© ✅
Jude Bellingham ✅

Joueur RĂ©al Madrid yĂ«pp jot nañu seen nexal ci BMW yu bess yiđŸš˜đŸ˜‡đŸ€
26/11/2026

Joueur RĂ©al Madrid yĂ«pp jot nañu seen nexal ci BMW yu bess yiđŸš˜đŸ˜‡đŸ€

26/11/2026

Bonjour 👋 tout les Madridista đŸ€
Ngir yĂ lla kĂ«pp ku bĂ«gg RĂ©al Madrid rek magui lay Ƅaan ngamay partagĂ©e publication yi wala ngay j'aime ngir pages bi gĂ«na jĂ«m kanam 🙏 merci beaucoup yeen ñépp

Leer na : José Mourinho bokkoo na ci 3 entraßner yi ñu nommé ngir entraßner bi gëna xarañ ci weeru novembre bi ci la Lig...
26/11/2026

Leer na : JosĂ© Mourinho bokkoo na ci 3 entraĂźner yi ñu nommĂ© ngir entraĂźner bi gĂ«na xarañ ci weeru novembre bi ci la Liga đŸ„łđŸ€

The Special one

15 League des champions 15 pointLeader ci League des champions bi Halla Madrid y nada mas đŸ€
25/11/2026

15 League des champions
15 point
Leader ci League des champions bi

Halla Madrid y nada mas đŸ€

JĂ«f ju rafet la Kylian MbappĂ© def tay 😇 ginnaaw bi ñu ko joxe trophĂ©e nexal joueurs bi gĂ«na xarañ ci match bi ( Homme de...
25/11/2026

JĂ«f ju rafet la Kylian MbappĂ© def tay 😇 ginnaaw bi ñu ko joxe trophĂ©e nexal joueurs bi gĂ«na xarañ ci match bi ( Homme de match ) mu woo Vini Jr joxaat ko nexal bi đŸ„łđŸ€

Mbappé 2 but 1 passe décisives
Vini jr 1 but ak match bu baax

Adresse

Diourbel
Touba

Site Web

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque Sylla Madridista en wolof publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

Raccourcis

Partager

épiceries à proximité